SERIGNE ALADJI MBACKE WAKHTANOU SERIGNE TOUBA XATH 2

201 Aufrufe
Published
Kéép kuko tewlu noogi sakku ci yaw nga fatéliku Cheikh Ahmadou Fadl Mbacké wajuru Serigne Ahmadou Rafahi ak mboolém ñimu bokkal nu saxx ci seeni mbég te am seeni ngërëm. Ngërëm lo xamné dessuko ñakkati. Amin
Addiya Serigne Hamzatou Mbacké diko nianal ludul Serigne Touba Yalla Bukossi kén guiss.
Amin!

Facebook : https://www.facebook.com/assadou.khadim
Twitter: https://twitter.com/AssadulK
Kategorien
Corona Virus aktuelle Videos Gesundheits Tipps
Suchwörter
berlin, demo, samstag, tausende, demonstranten, coronapolitik, coronavirus, reichstag
Kommentare deaktiviert.